Dédicaces RSS

layevice
il y a 4 jours
Macha alla laye makhtar yalla na yokou ba télè topousi
AL AMINE
il y a 1 semaine
LAHI MAKHTAR DILENE ZIAR BOU WER AM MBEGTE SI RADIOURUMBI DI WAX NE YALLA NA YALLA BARKEL KO BA NGUENE AM LOU KAWÈ SEN NDIORTE SI BARKE IMAM
Fatou laye
il y a 1 semaine
Laye makhtar liguene di def amna solo trop yalla naléne baye laye (psl) fay bonne continuation
pape mor
il y a 2 semaines
Dieureudieuf laye makhtar amna solo baye laye(psl) amoul mass
Radio Urum-Bi
il y a 2 semaines
Merci de nous rester fidèle. Vous pouvez nous appuyer au 77 988 9670.
Pape laye
il y a 2 semaines
machallah oooh diarama ouroum bii
Libass Gueye
il y a 3 semaines
Laye Makhtar dieuredieuf wa radio urum bi yalna yalla faylen yiiw you bari
Pape laye
il y a 3 semaines
yala nalen yala fay alassane
Radio Urum-Bi
il y a 3 semaines
Radio Urum-Bi remercie tous ceux qui l'écoutent où qu'ils se trouvent. Que Dieu vous garde par la grâce de la meilleure des créatures (PSL).
SidyLahi J.P
il y a 1 mois
Ziaar naala imaam Selou. Radio Urum-bi ca kaw ca kanam di may dédicace bi a tous les membres de JAMALAHI PICTURES
MAME ablaye
il y a 1 mois
Machallah laye yalnadone ay télé
Seydina ba
il y a 1 mois
Ziar nala laye maxtar di niane Yala dolli sen soutoura amine
SEYDINA MANDIONE LAYE MBAYE
il y a 1 mois
Dieuredieuf laye maxtar, Radio bi mogui niouy wetali bou bakh Yalla na Yalla barkél ligguey bi. Chérif ABDOULAHI Yalla nafi yagg!
Libass Gueye
il y a 1 mois
Laye makhtar Ziar wa Radio Urum bi Fier d'être Layene
Lamine Gueye
il y a 1 mois
Machalah gnigui léni ziarr si aldiouma bi du nianal chérif abdoulah mou yagua fi lol té werr contann lol si radio bi
Libass Gueye
il y a 1 mois
Laye makhtar ma gui ziar wa radio urum bi Sikar yi len Tek nekhna Yalla Yalla guena deugeureul sunu guem thi Baye Laye PSL
issafate
il y a 1 mois
machallah ziar wa ahlou laye radio urumbi yokou ba yeuk ko
mareme soda
il y a 1 mois
machalla yall nalène yalla fay si barquè MAME baye lay aleysalam magui ziar khalifatoul mouslimine chérif BAY Abdoulaye Thiaw mou yague fi
Libass Gueye
il y a 1 mois
Laye Makhtar ma gui Ziar wa Dahira Akhloulahi Yarakh
Woury
il y a 2 mois
Machalla amna solo lahi
djiby laye
il y a 2 mois
nio gui ziar wa akhlou laye yeup wa dahira akhloulaye Madrid , dahira France , dahira Italie
djiby laye
il y a 2 mois
laye mactar radio bi macha allah moy sama wéteul yalla nalen yalla fay si barké mame baye lahi aléyi salatou wasalam
Libass Gueye
il y a 2 mois
Laye makhtar dédicace à toute la communauté Akhlou Lahi, Baye Laye AmouL Mass Njool Yay Borom Diine
Libass Gueye
il y a 2 mois
Laye makhtar guem Baye Laye reka worr ; mes encouragements à la radio urum bi bonne continuation
alassane laye
il y a 2 mois
Dieureu dieuf seydina Limamou geum wolou yakar
Seydina Issa
il y a 2 mois
part cette voix,je pense à Tout Akhloulahi de Diender
libasse ndia
il y a 2 mois
baye mouhamadou thiaw ibene serigne ablaye yalna fi yag lol te andak were amine
Libass Gueye
il y a 3 mois
Laye makhtar Ziar na nieup surtout wa radio urum bi notre fierté Jotna wa adina xam né Baye Laye moy yonente bi Baye Abdoulaye yalna fi yagu
Haàj MOody
il y a 3 mois
MaashaaALLAAH... YAALNA BOROOM BII GEUNEU YÉWÉNEUL Mbir Yii
fdia Laye
il y a 3 mois
Dieureudieuf laye mamadou